Yéen Daal, Yéena Ñàkk Xel

Yéen Daal, Yéena Ñàkk Xel

Sunu Yaakaar

31/03/2020 6:08PM

Episode Synopsis "Yéen Daal, Yéena Ñàkk Xel"

Danuy begg nga delloo ay ndigal ngir nga dimbali dëgg bu baax Kaddug Yalla. Danuy ngëm ne “Sunu Yaakaar" mooy xam Yalla kuy sakk lépp li nekk. Danuy ngem ne népp mën nanu xam Yalla ci Kaadoom ndax Yalla féegnal na boppam ci Kaadoom. Toppal sunu émission “Sunu Yaakaar” ci facebook.com/sunuyaakaar Soo amé laaj, contactez nous ci email: [email protected]

Listen "Yéen Daal, Yéena Ñàkk Xel"

More episodes of the podcast Sunu Yaakaar